Home / Wolof / Wolof Bible / Web / 1 Corinthians

 

1 Corinthians 8.13

  
13. Kon bu sama mbokk sóoboo ci bàkkaar ndax ñam wi ma lekk, dootuma lekk mukk yàpp, ngir bañ a sóob ci bàkkaar sama mbokk mi.