Home / Wolof / Wolof Bible / Web / 1 Corinthians

 

1 Corinthians 9.21

  
21. Ci biir ñi nekkul ci yoonu Musaa, faalewuma woon yoon wi, ngir gindi leen; waxuma ne, ànduma ak yoonu Yàlla, waaye topp naa yoon ci sama bokk ak Kirist.