Home / Wolof / Wolof Bible / Web / 2 Corinthians

 

2 Corinthians 11.21

  
21. Sunu néew doole mayu nu, nu dem ba jëfe noonu; rus naa ci lool de! Ma wax waxi dof; moona lépp lu waay ñemee damoo, ñeme naa ko, man it.