Home / Wolof / Wolof Bible / Web / 2 Corinthians

 

2 Corinthians 5.21

  
21. Kirist mi musul a def bàkkaar, Yàlla def na ko bàkkaar ci sunu wàll, ngir ci sunu bokk ci moom, nu man a doon njubteg Yàlla.