Home / Wolof / Wolof Bible / Web / 2 Peter

 

2 Peter 2.13

  
13. muy seen peyug njubadi. Xawaare bëccëgu ndara-kàmm mooy seen bànneex. Su ñuy lekkandoo ak yeen, dañuy bànneexu ci seeni bëgg-bëgg, di ay gàkk ak i sikk ci seen biir.