Home
/
Wolof
/
Wolof Bible
/
Web
/
2 Peter
2 Peter 2.21
21.
Ndaxte ñu xam yoon wu jub wi, ba noppi dëddu ndigal lu sell li ñu déggoon, bañoon koo xam moo gënoon ci ñoom.