Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Acts

 

Acts 3.21

  
21. Asamaan war na koo yor, ba jamono ju ñuy defaraat lépp, di jamono ji Yàlla waxoon jaarale ko ci gémmiñug yonentam yu sell yépp, li dale ci njàlbéenug àddina.