Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Acts

 

Acts 7.49

  
49. “Asamaan mooy sama jal,te suuf mooy sama tegukaayu tànk.Kon gan kër ngeen may tabaxal,mbaa fan mooy sama bérabu noppalukaay?