Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Acts

 

Acts 9.13

  
13. Waaye Anañas tontu ko ne: «Boroom bi, dégg naa ci nit ñu bare ci mbirum kooku, ñu seede lu bare lu bon lu mu def say gaay ci Yerusalem.