Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Ephesians

 

Ephesians 2.13

  
13. Waaye léegi ci seen bokk ci Kirist Yeesu, yéen ñi sore woon jege ngeen ndax deretu Kirist ji ñu tuur.