Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Hebrews

 

Hebrews 8.13

  
13. Kon nag bi Yàllay wax ci kóllëre gu bees gi, dafa fekk mu màggatal gu jëkk ga. Te lu xewwi te màggat mi ngi ci tànki wéy.