Home
/
Wolof
/
Wolof Bible
/
Web
/
John
John 13.36
36.
Simoŋ Piyeer laaj ko ne: «Boroom bi, foo jëm?» Yeesu ne ko: «Fa ma jëm, mënuloo ma faa topp léegi, waaye dinga ma toppi ca kanam.»