Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Luke

 

Luke 9.49

  
49. Bi loolu amee Yowaana jël kàddu gi ne: «Kilifa gi, danoo gis nit kuy dàq ay rab ci sa tur, nu tere ko ko, ndaxte bokkul ci nun.»