Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Mark

 

Mark 10.13

  
13. Bi loolu wéyee ñu indil Yeesu ay xale, ngir mu teg leen ay loxoom. Waaye taalibe ya gëdd nit ñi.