Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Mark

 

Mark 14.49

  
49. Moona daan naa toog bés bu nekk ca kër Yàlla ga, di jàngale, te jàppuleen ma. Waaye lii am na, ngir Mbind mi am.»