Home
/
Wolof
/
Wolof Bible
/
Web
/
Mark
Mark 4.21
21.
Yeesu ne leen itam: «Ndax nit dina jël làmp, dëpp ci leget walla def ko ci ron lal? Ndax du ko wékk?