Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Revelation

 

Revelation 16.21

  
21. Tawu yuur, donj wu nekk tollu ci ñeent-fukki kilo, daldi daanoo asamaan ci kaw nit ñi, ñuy xarab Yàlla ndax musibam yuur ga, ndaxte musiba ma dafa metti woon lool.