Home / Wolof / Wolof Bible / Web / Romans

 

Romans 3.21

  
21. Waaye léegi nag Yàlla feeñal na, ni nit man a jube ci kanamam, ci lu séqul ak yoonu Musaa dara. Waaye ba tey yoonu Musaa ak waxi yonent yi seedeel nañu ko.