Home
/
Wolof
/
Wolof Bible
/
Web
/
Romans
Romans 9.21
21.
Ndax tabaxkatu ndaa sañul a fab banam, tabax ci ñaari ndaa, benn bi ngir soxla yu am maana, bi ci des ngir soxla yu ndaw?